le petit prince

“On ne voit bien qu'avec le cœur”

Antoine de Saint-Exupéry

HOMMAGE MULTILINGUE
AU PETIT PRINCE

wolof

Xamouñu lou doul lou ñou miin, (wakh golo). Nit ñi amatouñu jootu xam. Dañuy jenda lou paré ba noppi ca jaykat ba. Waayé ndéguém amatoul jaykatou xarit, nit amatoul xarit. So beugué xarit, nékhalma!
...
Tagounaléen (wakh golo). Li moy li ma doon neubeu. Dafa yonmbeu: ak xol la ñuy gisé bou bakh. Li am solo dafay laxou beuti.
Version:Yacine Diop Fonjallaz
homme
homme
homme

Retour